Back to syntactic page
Examples of the root word njaay (njaay) also marked by ***, hover on that word to see more grammar properties.
1 Mbay mbay NOUN NOUN _ 0 _ _ _
2 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
3 liggéey liggéey NOUN NOUN _ 0 _ _ _
4 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
5 loxo loxo NOUN NOUN _ 0 _ _ _
6 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
7 càmm càmm NOUN NOUN _ 0 _ _ _
8 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
9 napp napp NOUN NOUN _ 0 _ _ _
10 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
11 ***njaay*** njaay NOUN NOUN _ 9 conj _ _
12 ñu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Plur|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
13 a a AUX INFL FocusType=Subj|Mood=Ind 0 _ _ _
14 nekkoon nekk VERB VERB Mood=Ind|Tense=Past|VerbForm=Fin 0 _ _ _
15 fànni fànn NOUN NOUN Case=Gen|Number=Plur 0 _ _ _
16 liggéey liggéey NOUN NOUN _ 0 _ _ _
17 yi bi PRON PRON Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol8|Number=Plur|Person=3|PronType=Rel 0 _ _ _
18 ëppoon ëpp VERB VERB Mood=Ind|Tense=Past|VerbForm=Fin 0 _ _ _
19 solo solo NOUN NOUN _ 0 _ _ _
20 ca ca ADP PREP _ 0 _ _ _
21 nguur nguur NOUN NOUN _ 0 _ _ _
22 ga bi DET DET Definite=Def|Deixis=Remt|NounClass=Wol3|Number=Sing|PronType=Art 0 _ _ _
23 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _
1 Waaye waaye CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
2 ***njaay*** njaay NOUN NOUN _ 8 dislocated _ _
3 moom moom ADV ADV _ 0 _ _ _
4 naka-jekk naka-jekk ADV ADV _ 0 _ _ _
5 tubaab tubaab NOUN NOUN _ 0 _ _ _
6 yi bi DET DET Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol8|Number=Plur|PronType=Art 0 _ _ _
7 ñu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Plur|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
8 a a AUX INFL FocusType=Subj|Mood=Ind 0 _ _ _
9 ëppoon ëpp VERB VERB Mood=Ind|Tense=Past|VerbForm=Fin 0 _ _ _
10 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
11 ñi bi PRON PRON Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol2|Number=Plur|Person=3|PronType=Rel 0 _ _ _
12 ñu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Plur|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
13 ko ko PRON CL Case=Acc|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
14 defal defal VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
15 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _
1 Mu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
2 dal dal ADV ADV _ 0 _ _ _
3 ca ca ADP PREP _ 0 _ _ _
4 di di AUX AUX Aspect=Imp|Mood=Ind|Tense=Pres 0 _ _ _
5 dolli dolli VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
6 ***njaayum*** njaay NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 5 comp:obj _ _
7 jaam jaam NOUN NOUN _ 0 _ _ _
8 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
9 ngir ngir ADP PREP _ 0 _ _ _
10 am am VERB VERB VerbForm=Inf 0 _ _ _
11 ay ab DET DET Definite=Ind|NounClass=Wol8|Number=Plur|PronType=Art 0 _ _ _
12 fas fas NOUN NOUN _ 0 _ _ _
13 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
14 ay ab DET DET Definite=Ind|NounClass=Wol8|Number=Plur|PronType=Art 0 _ _ _
15 piis piis NOUN NOUN _ 0 _ _ _
16 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
17 ay ab DET DET Definite=Ind|NounClass=Wol8|Number=Plur|PronType=Art 0 _ _ _
18 dibi dibi NOUN NOUN _ 0 _ _ _
19 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
20 ... ... PUNCT ELLIPSIS _ 0 _ _ _
1 Nga mu PRON PRON Case=Nom|Number=Sing|Person=2|PronType=Prs 0 _ _ _
2 xam xam VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
3 ne ne SCONJ COMP _ 0 _ _ _
4 li bi PRON PRON Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol7|Number=Sing|Person=3|PronType=Rel 0 _ _ _
5 nekk nekk VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
6 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
7 biir biir NOUN NOUN _ 0 _ _ _
8 réew réew NOUN NOUN _ 0 _ _ _
9 mi bi DET DET Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol6|Number=Sing|PronType=Art 0 _ _ _
10 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
11 am ab DET DET Definite=Ind|NounClass=Wol6|Number=Sing|PronType=Art 0 _ _ _
12 ***njaay*** njaay NOUN NOUN _ 10 comp:obj _ _
13 deesu di AUX AUX Aspect=Imp|Mood=Ind|Person=3|Polarity=Neg|Tense=Pres 0 _ _ _
14 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
15 genne genn VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
16 duwaan duwaan NOUN NOUN _ 0 _ _ _
17 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _
1 ***Njaayum*** njaay NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 6 dislocated _ _
2 geerte geerte NOUN NOUN _ 0 _ _ _
3 gi bi DET DET Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol3|Number=Sing|PronType=Art 0 _ _ _
4 ni ni ADV ADV Deixis=Prox|NounClass=Wol12|PronType=Dem 0 _ _ _
5 mu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
6 di di AUX AUX Aspect=Imp|Mood=Ind|Tense=Pres 0 _ _ _
7 doxe dox VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
8 baaxul baax VERB VERB Mood=Ind|Number=Sing|Person=3|Polarity=Neg|VerbForm=Fin 0 _ _ _
9 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
10 la la AUX INFL FocusType=Compl|Mood=Ind|Number=Sing|Person=3 0 _ _ _
11 njiitu njiit NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 0 _ _ _
12 jëwriñ jëwriñ NOUN NOUN _ 0 _ _ _
13 yi bi DET DET Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol8|Number=Plur|PronType=Art 0 _ _ _
14 naqarlu naqarlu VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
15 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _
1 Njiitu njiit NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 0 _ _ _
2 jëwriñ jëwriñ NOUN NOUN _ 0 _ _ _
3 yu yu ADP PREP _ 0 _ _ _
4 Senegaal Senegaal PROPN NAME _ 0 _ _ _
5 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
6 Suleymaan Suleymaan PROPN NAME _ 0 _ _ _
7 Ndeene Ndeene PROPN NAME _ 0 _ _ _
8 Njaay Njaay PROPN NAME _ 0 _ _ _
9 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
10 naqarlu naqarlu VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
11 na na AUX INFL Aspect=Perf|Mood=Ind|Number=Sing|Person=3 0 _ _ _
12 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
13 àllarba àllarba NOUN NOUN _ 0 _ _ _
14 ca ca ADP PREP _ 0 _ _ _
15 Ndakaaru Ndakaaru PROPN NAME _ 0 _ _ _
16 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
17 ni ni ADV ADV Deixis=Prox|NounClass=Wol12|PronType=Dem 0 _ _ _
18 ***njaayum*** njaay NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 21 subj _ _
19 geerte geerte NOUN NOUN _ 0 _ _ _
20 gi bi DET DET Definite=Def|Deixis=Prox|NounClass=Wol3|Number=Sing|PronType=Art 0 _ _ _
21 di di AUX AUX Aspect=Imp|Mood=Ind|Tense=Pres 0 _ _ _
22 deme dem VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
23 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
24 jàpp jàpp VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
25 na na AUX INFL Aspect=Perf|Mood=Ind|Number=Sing|Person=3 0 _ _ _
26 ne ne SCONJ COMP _ 0 _ _ _
27 ni ni ADV ADV Deixis=Prox|NounClass=Wol12|PronType=Dem 0 _ _ _
28 mu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
29 di di AUX AUX Aspect=Imp|Mood=Ind|Tense=Pres 0 _ _ _
30 doxe dox VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
31 baaxul baax VERB VERB Mood=Ind|Number=Sing|Person=3|Polarity=Neg|VerbForm=Fin 0 _ _ _
32 dara dara NOUN NOUN _ 0 _ _ _
33 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _
1 Njaam njaam NOUN NOUN _ 0 _ _ _
2 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
3 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
4 ***njaay*** njaay NOUN NOUN _ 1 conj _ _
5 ak ak CCONJ CONJ _ 0 _ _ _
6 njëndum njënd NOUN NOUN Case=Gen|Number=Sing 0 _ _ _
7 jaam jaam NOUN NOUN _ 0 _ _ _
8 terees tere VERB VERB Mood=Ind|Person=0|VerbForm=Fin 0 _ _ _
9 na na AUX INFL Aspect=Perf|Mood=Ind|Number=Sing|Person=3 0 _ _ _
10 ko ko PRON CL Case=Acc|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
11 , , PUNCT COMMA _ 0 _ _ _
12 ci ci ADP PREP _ 0 _ _ _
13 anam anam NOUN NOUN _ 0 _ _ _
14 yu bu PRON PRON NounClass=Wol8|Number=Plur|Person=3|PronType=Rel 0 _ _ _
15 mu mu PRON PRON Case=Nom|Number=Sing|Person=3|PronType=Prs 0 _ _ _
16 mën mën VERB VERB Mood=Ind|VerbForm=Fin 0 _ _ _
17 doon doon VERB VERB VerbForm=Inf 0 _ _ _
18 . . PUNCT PERIOD _ 0 _ _ _